| Accueil | Créer un blog | Accès membres | Tous les blogs | Meetic 3 jours gratuit | Meetic Affinity 3 jours gratuit | Rainbow's Lips | Badoo |
newsletter de vip-blog.com S'inscrireSe désinscrire
http://aloubb.vip-blog.com


je n'aime pas le mensonges
VIP Board
Blog express
Messages audio
Video Blog
Flux RSS

je n'aime pas le mensonges

VIP-Blog de aloubb
  • 59 articles publiés
  • 6 commentaires postés
  • 1 visiteur aujourd'hui
  • Créé le : 24/09/2006 23:32
    Modifié : 21/12/2006 15:20

    Garçon (16 ans)
    Origine : dakar
    Contact
    Favori
    Faire connaître ce blog
    Newsletter de ce blog

     Juillet  2025 
    Lun Mar Mer Jeu Ven Sam Dim
    30010203040506
    07080910111213
    14151617181920
    21222324252627
    282930010203

    rien que pour toi

    22/11/2006 14:19

    rien que pour toi


    ibil nal sama khol, yalla na nga si guiss lou lére té gueuneu kham ni amoul kénène koudoul yaw. mbeugél gui nékeu si mane a ngii di ma dane té gueum na né di na done sa néné bi ngéy tété. mane mi souma mounone, dina bokake yow bénéne yone, dila wowé néné touti, ndakh té mane mi, mane mi gnanou ma yalla, gnanou ma yalla déss fii mane réka!
    ref: yow mi néke sama khol guissou ma kénéne koudoul yow, mbeuguél gui mo ngi ni di law, ibil nala sama khol
    yow mi néke sama khol guissou ma kénéne koudoul yow, mbeuguél gui mo ngi ni di law, té dina done sa néné.
    am na gnou wakh mbeugél tiono rék la, wayé ma ngi léy khamal dou kéne yow réke leu. beuss bou me le guissé la kham ni khol déy guissé té fok na ni do meusse tass sama yakar!
    boul am loy ragal di la khar, doumeu meusseu diay sama taar, dinala wowé papa chéri, dina done sa sokhna, di na done sa baby, mi léy fadial say sokhla, oh baby yow réke le
    ref...............
    yay sama doolé soudoul yow wate na né dou done kékéne, diokh na la sama bope, té dina la dégueul di le bégueul, baby boul sone, gueumeul ni yow réke le! dou kékéne....






    [ Annuaire | VIP-Site | Charte | Admin | Contact aloubb ]

    © VIP Blog - Signaler un abus